Suniouy examens biologiques

Suniouy examens biologiques

Saa sou nguèn ko beugué Solabsen meunalèn defal ay examen nguir saytou sèn wergou yaram. Wayé bignesi geuneu sokhla moy niari fane bou wessou ba nguène tagaté sène yarame. Mouy niane kone nguène samonté ak tektal yi ndakhté yene si ay analyse pour niou defko faw nite ki woor, maname mou kheuy dou lek dara.
Nouniouy amalé yilé examen ? Solabsen né dasiy leukeulo ak médecin yisi fédération you sport yi. Lolé dina takh niou meuneu saytou yane diafé diafé la am si wergou yaramame.