Ñun ñoy kan ?

Ñun ñoy kan ?

Biologie du sport ay docteur you kharagne nioko takhawal lèp nguir gueuneu topato sène wergou yaram. Bokounasi Docteur Omar Adamou di ap pharmacien biologiste djité itam Solabsen. Mouy kou kharagne torop si waleu tagate yaram, lou melni cyclisme, jogging ak football. Docteur Omar, nékone secrétaire général bou Asfan mo gadouwone raya bou coupe bou union wou fédération footbal bou afrique soy diante (UFOA) si atou 1996.
Si Ddocteur you kharagne yoyou ragné nègnesi tamite ki di Docteur Madièye Gueye di ap gueustoukate bou mak fi si Unversité Cheikh Anta Diop. Mom mé sakh mou ngui diangué thia Université Louis Pasteur bou Strasbourg, bindi itam ay téré you beuri si waleu stress oxydant.